Texte de Xaadim Njaay Historien résidant au Canada 🇨🇦 

Violence nekkul rekk ci dóor mbaa ray nit. Lu xóot la.

La violence peut être économique. Elle est dans les politiques gouvernementales. Elle est dans les inégalités. Elle est dans la manière arrogante de parler aux administrés. Elle est dans les ruptures territoriales. Elle est dans les injustices.

La violence est dans les mots. Elle peut être verbale, conceptuelle. Dëkkël nit fu mu dëkkul. Jëfee baat bu ñagas jëmële ci moom. Ci xeeti violence la bokk.

En plus d’être véhiculée dans les insultes et les intimidations, elle peut être même dans l’humour, la moquerie. Waawaaw, di kaf ndeke yaa ngi wone violence bu yéeme. Violence di na feeñ sax ci kaf ak ree.

Quelqu’un peut dénoncer la violence en la véhiculant par les mots et concepts qu’il utilise.

Tuer, insulter, frapper mooy li gënë siiw, waayé violence aka sew! 

Bi gënë bon nag, mooy ngay jëfe violence te xamoo ne yaa ngi koy jëfe. 

Violence dina waral Doomu Aadama di fippu. Ci kaw fippu googu, man na jëfee violence.

Ci Taariix, Sufiyanke yu mag fippu na ñu, jëfee violence, xeex ngir bañ nooteel. 

Ci gàttal : violence dafa sew, mi ngi fépp daa na ka. Te violence dafay indi violence. 

Ci biir àddina, violence yàq na lu bari, waayé defar na lu bari.

Bàyyi ci xel.

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *